CHEIKHUL-KULLIL-AWLIYA

Barhâma, Barhâma Niasse Shaykhul kullil Awliyâ Barhâma

Barhâma, Barhâma Niasse Cheikhul kullil Awliyâ Barhâma,

Shaykhul kullil Awliyâ’i Bâye Barhâma

Khôlalma fenkak Baye bi thi Taïba Niassène

Gôru Haïbu yeup Têw Nâne Barhâma

Serigne bugne koy Tôpé Tâar Thiolâyame ba suko gnaké

Mêlokaname ba def lay lêr, Barhâma

Târu Diamant ki ko sôlo kôku moy jeumi Bâye Niasse

Jeumeul na mbidêf yeup Niuy Barhâma

Du dê, Dieufeum du nul, kuye sûl dieuf goréwôu…lo

Dioglêne gnu ndiukeul Wâja môy Barhâma

Bi Lâhi wa Lâhi môm Bâye suko Nêkhone

Ku wôté dugne la wuyussi Bâye Barhâma

Barigot bu fêsse du yeungu wêr wêr bi Tankhal nagnu

Khathie buye maté duye mbawé, Bâye Barhâma

Sô guissé ku yomb dajalé aw limame dotul tôgo

Ninki nanka dugne koy sôru Barhâma

Kholalma Cheikh Ibrâhim tothie na Makkah ak sôdan

Niuy gamu ziarré si Bâye Barhâma

Bul sonk kholal auto bi, ap chauffeur ra koy conduire

Duneyâ bi itam nônu thi Barhâma

Sakhar ku diâr thi yônam bula fîré ya ko tôgno

Ndakh yônam bi pour môm rek la, Barhâma

So méré ya nga nâne di na tagalé galace ak ndokh

Thiossâne galace ndokh la, Bâye Barhâma

Môgnu wakhone thia wey wa may bakane yi may gokh yi, may bakane yi may gokh yi

May leep lu ngène dianôle, Bâye Barhâma

Yeen mbôlo mi fi têw,yalla na lène yalla yôk ,yalla na lène yalla yôk

Té diokhlène maqâma yi, thi Barhâma

Mane suma nampone arabe tey ma tag Barhâma

Cheikhul kullil Awliyâi Barhâma

Bâye mognu nampal, môgnu lêral, thi lêru Allâhu

Allâhu, Allâhu, Allâhu,

Allâhu, Allâhu,

Lâ ilâha ila Lâhu, Allâhu

Bâye mognu jeuzbu, môgnu guindi thi lîfu AlLâhu

Allâhu, Allâhu, Allâhu,

Allâhu, Allâhu,

Lâ ilâha ila Lâhu, Allâhu

Bâye mognu diubal môgnu khâmal thi Hâ u AlLâhu

AlLâhu, AlLâhu, AlLâhu,

Allâhu, Allâhu,

Lâ ilâha ila Lâhu, Allâhu

Lâ ilahâ ila lâh

Lâ ilahâ ila lâh